Tata 36 biy jóge Ngor di dem Guediawaye

Keroog dama dugg ci benn bis Tata bu 36 bi lay jële terminis Ngor yobbu la Guediawaye. Tata yu ndaw yii dañuy gaawa fees ak nit waaye wii yoon amoon naa palaas kon toogoon naa. Sopp naa jël ‘taranspoor pibilik’ ci biir dëkki taax yi ndaxte di leen faraldi jël dafay tax nga xam bu …