Tata 36 biy jóge Ngor di dem Guediawaye

Keroog dama dugg ci benn bis Tata bu 36 bi lay jële terminis Ngor yobbu la Guediawaye. Tata yu ndaw yii dañuy gaawa fees ak nit waaye wii yoon amoon naa palaas kon toogoon naa. Sopp naa jël ‘taranspoor pibilik’ ci biir dëkki taax yi ndaxte di leen faraldi jël dafay tax nga xam bu […]

Tata no 36 to Guediawaye

The other day I hopped on a Tata bus no 36 that takes you from Ngor Garage to Guediawaye. These small Tata buses get packed with passengers very fast but on this particular trip I even had a seat! I like public transport in cities and not the least because using it really gives you […]